Dal leen Jàmm ci Senegaal xabaar!

 

Xët yi seen jublu mooy baaxe leen gis-gis bu yaatu bu Senegaal séx ak réewu almaañ,
ci biir kurél yu bare te wuutee, yu wékuwul ci nguur gi.
Ay xabaar ci aada ak cosaan, jokkooy réew book nañu ci.
Dolliku ci nag ay yombali ndey dikke.
Bu weesoo xabaar xabaar yi ñu leen di baaxe ay Xët yu leen jukkil wecceentey
xalaat ci biir liggéey bi leen lëkkëléenté ci kow jappoo,
ak booloo way and liggéey ci mbootaayiy way defal yálla yi, ak kuréel yi andandoy liggéey.
Ñooñu ñeepp bokk di xeex ngir suxali liggéey mi.

Ku am yeneen xalaat yoo ciy dooli, walla loo ciy taxaw setlu ubil nañu la bunt bi.

 

     

webmaster@senegal-info.de
actualisé le 01/01/2010